DOWNLOAD BATAXALU ASKAN WII BY SIDY KA - MP3, MP4 & LYRICS

Title Bataxalu Askan Wii
Artists Sidy Ka
Genres Hip Hop
Country Senegal

Bataxalu Askan Wii Lyrics

Déret turu sufu senegal bay walangan
Takal badola bi raxasu si guéju nott
Thiono du fegn si pouvoir budul jehh
Non non nio bagn
Sama batahal bi
Askan wéma yondi fokma jalaléko
Meuna tougnou dundu li
Si nguur gudul jehh
Non non nio bagn
Thiow jiip na fugnko fogéwoul won
Injustice bi thi rewmii metina
Senegalais bangui jooy nakaru holl
Non non nio bagn

Yaw niata jeune nio deé thi lii
Rongognu nakaar féthiali
Waro haar ayy netalii
Sa deff patt a yokku li
Rew meepa ngui jooy
Holl yeupa and tooy
Non non nio bagn
Lettre bi filakoy yémaléee
Porteur de voix
Askan wi nioma yoni wonn
Senegall sunu gaal
Free Senegal
Non non nio bagn